Sàrt bu bees ci wàllu palaastig: ëllëg gu leundeum si liggéeyu mbuus yii

Avatar Moussa Ngom | 18 avril 2020

Ñaar fuki fann ci weeru awril 2020
Li tambalee date bii, di fi leeki fan, lañiy jemmeul loi biy tere palastig ci Sénégal.
Ñiy yengou si bobu secteur, naka lagniy xaare thiopite gi? Ndax yeug nagn ko? Dem nañ seeti leen.
Tambalee kosi Jaay katu ndox, ba ci ñikoy jeule bitim reew jaar ci borom bitiku mbag yi, ben laaj bi moo nek ci bopp yi : ana luy outtou palastig
Sart bu bees si wallou palastig, euleugg gu leundeum si liggeyu mbuus yii
Muy jangatt bu ñu Fatma Mbacké defal


Commentaires

This post currently has no responses.

Votre opinion nous intéresse, laissez un commentaire à cet article


error: Dans le cadre de la protection de nos contenus, nous avons verrouillé la copie de nos articles, la citation reste permise. Merci de votre compréhension!